WOLOF CINEMA
@wolofcinema
Subscribers
Views
Videos
API Count
To 10
Live Subscriber Growth Chart
Loading Advanced Analytics...
About WOLOF CINEMA
WOLOF CINEMA: Sunu Gaal Sinemaa.Fi la sinemaa bu Senegaal amee kër. Du fuñuy dugal ay film rekk, waaye fii lañuy dajalee, sàmm, tey yékkati ndono li ñu fi baayee sunu maam ci téyaatar ak sinemaa.Ci chaine bii, di nga fi fekk:
* Film yu Mag Yépp: Ay film yu bees ak yu yàgg, yuñu jël walla yuñu remasterisé ngir seen bët.
* Téyaatar bu Am Solo: Ay pìyesu téyaatar yu am solo yu ñu ràññee yu nee woon ci téle bi.
* Ay Xalaat yu Bees: Ay band-annonce yu ñu defaraat, ay compilation yu neex, ak ay xew-xew ci li wër sunu sinemaa.
WOLOF CINEMA du chaine bu ñu mom rekk. Yeen ñi sétan ñoo ko bokk. Seen xalaat, seen bëgg-bëgg, ak seen mbëggeel moo ñuy jox doole.Bokk ak ñun ci liggéey bi. Abonnél ngir doon parti ci mbooloo miy sàmm tey fésal sunu gaal sinemaa, ngir tay ak ëllëg.
Embed on Your Website
Do you want to put WOLOF CINEMA 's realtime subscriber count on your website? Use the embed code below or add the direct URL as a browser source in OBS.
Latest Video
L'histoire de Victor Biaka Boda de la Cote d'ivoire
by WOLOF CINEMA
Click to load YouTube player
L'histoire de Victor Biaka Boda de la Cote d'ivoire
Uploaded
64
Views
1
Likes
0
Comments
About RealtimeSubCount.com
RealtimeSubCount.com tracks live YouTube subscriber activity with a faster page shell, local caching, and analytics modules that do not block the main counter from loading. This page is designed to keep the count visible first while the deeper charts and supporting widgets stream in behind it.